1 Samuel 9:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Sóol ne surgaam: «Wax nga dëgg. Kon nan dem.» Ñu jubal ca dëkk ba góoru Yàlla ga nekk.