1 Samuel 9:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne leen: «Waaw, mu ngi fii ngeen jublu, waaye gaawleen de; ndax tey jii la dikk ci dëkk bi, ngir sarax su waa dëkk bi xewle tey ca bérabu jaamookaay ba.