1 Samuel 9:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñu dem bay dugg ca biir dëkk ba, yem ca Samiyel, muy dikk, dajeek ñoom, jëm ca jaamookaay ba.