1 Samuel 9:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am doom ju ñuy wax Sóol; xalelu góor bu góorayiw, ba kenn dàqu ko ci bànni Israyil, sut ñépp taxawaay.