1 Samuel 9:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Toggkat bi yékkati tànk baak la mu àndal, teg ko ca kanam Sóol. Samiyel ne ko: «Lii, lañu beroon, tegal sa kanam, te lekk. Moom lañu la dencal ci ndaje mii ma woo askan wi.» Noonu la Sóol bokke ak Samiyel lekk bésub keroog.