1 Samuel 9:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañu dem bay bëgga génn dëkk ba, Samiyel ne Sóol: «Neel surga bi, mu jiitu nu.» Mu wax ko surga ba, mu jiitu leen. Samiyel neeti Sóol: «Yaw, taxawal fii tuuti, ma dégtal la kàddug Yàlla.»