1 Samuel 9:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Sóol ak surgaam jaare tundi Efrayim, teg ca diiwaanu Salisa, gisuñu leen. Ñu jàll ba ca diiwaanu Saalim, dara. Ñu walbatiku jaaraat diiwaanu Beñamin, gisuñu leen.