1 Samuel 9:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Surga ba ne ko: «Xanaa lenn; genn góoru Yàllaa ngi ci dëkk bii, ku ñu naw la. Lépp lu mu wax, dara du ci fanaan àll. Nan fa dem kay, jombul mu xamal nu dara ci sunu yoon wi.»