1 Thessalonians 1:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, yéen ñi Yàlla bëgg, xam nanu ne Yàlla tànn na leen;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen bokki gëmkat ñi Yàlla sopp, xam nanu ne moom moo leen taamu,