1 Thessalonians 1:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ngeen daldi nekk royukaay ngir ñi gëm ñépp ci diiwaani Maseduwan ak Akayi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo leen taxa doon royukaay ci mboolem gëmkati diiwaani Maseduwan ak Akayi.