1 Thessalonians 2:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka sunu diggante ak yéen ñi gëm, doxal nanu ko doxalin wu sell te jub te amul sikk: seede ngeen ko, te Yàlla it seede na ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeena seede, Yàlla itam seede, sellnga ak njub, ak mucc sikk ga nu doon jëfe fa seen biir, yeen ñi gëm.