1 Thessalonians 2:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam ngeen ne, dénk nanu leen kenn-kenn, ni baay di def ak doomam, dëfëlal leen seen xol te dëggal ci yéen, ngeen dund dund gu neex Yàlla, moom mi leen di woo, ngeen séddu ci nguuram ak ndamam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam ngeen ne fi baay féete doomam lanu féete kenn ku nekk ci yeen.