1 Thessalonians 2:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Nun nag bokk yi, ba ñu ma leen xañee ab diir --xol yi taxul may wax, waaye jëmm yi rekk — jéem nanu leen a gis ak sunu kem-kàttan, ndax namm nanu leen, ba sunu xol seey ci gis leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun nag bokk yi, teqale nañu nu ak yeen ab diir, waaye xol yi sorewaatoowul, xanaa jëmm yi rekk. Waaye sunu nammeel gu réy tax na noo def sunu kem kàttan, ndax yàkkamtee gise waat ak yeen.