1 Thessalonians 2:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte bés bu Yeesu sunu Boroom dellusee, te nu fekke ko, kan mooy sunu yaakaar? Kan mooy sunu mbég? Kan mooy sunu kaala, gi nuy tiitaroo?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat, ana kan mooy sunu yaakaar, di sunu mbég, te di sunu kaala gu nuy sagooji? Xanaa du yeen, kera ca sunu kanam Boroom Yeesu, bu feeñee?