1 Thessalonians 2:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye gannaaw Yàlla moo nu seet, ba wóolu nu te dénk nu xebaar bu baax bi, kon noonu lanuy waaree, du ngir neex nit ñi, waaye ngir neex Yàlla, miy seet xol yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa kay noonu nu Yàlla doyloo, ba dénk nu liggéeyu xibaaru jàmm bi, noonu lanuy waaree li neex Yàlla miy seet ab xol, te dunu ci wut bànneexu nit ñi.