1 Thessalonians 2:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Manoon nanoo diis ci seen kaw sax, nun ñiy ndawi Kirist, waaye woyofoon nanu ci seen biir, te lewet ni jaboot buy uuf doomam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Manoon nanoo taafantoo li nu diy ndawi Almasi, ba diisal leen, waaye danoo lewetoon domm ci seen biir, mel ni jaboot juy topptoo ay doomam.