1 Thessalonians 2:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Cofeel gi nu am ci yéen tax na, bëggunu woon a yem ci xamal leen xebaaru Yàlla bu baax bi, waaye jox leen it sunu bakkan, ndaxte sunu xol seeyoon na ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu lanu nabe woon ci yeen, ba buggunu woona yem ci xamal leen doŋŋ xibaaru jàmm bu Yàlla, waaye danu leena sopp ba yéene woon leena jox sunu bakkan sax boole ci, ndax fi ngeen nu mujj tollu ci sunu xol.