1 Thessalonians 3:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na Yàlla sunu Baay moom ci boppam ak Yeesu sunu Boroom jubal sunu yoon ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yal na Yàlla sunu Baay ci boppam, ànd ak sunu Sang Yeesu, ngir jubal sunuw yoon ba nu agsi ci yeen.