1 Thessalonians 3:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Na samp seeni xol noonu ci cell gu amul sikk fa kanam Yàlla sunu Baay, ba bés bu Yeesu sunu Boroom dellusee, ànd ak gaayam yu sell yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yal na Boroom bi dooleele noonu seen xol, ngir kera bu sunu Sang Yeesu délsee, ànd ak ñoñam ñu sell ñépp, fekk leen sell te mucc sikk, fa kanam Yàlla sunu Baay.