1 Thessalonians 3:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
te yónni nanu Timote, sunu mbokk ak sunu nawle ci liggéeyu Yàlla ak ci waareb xebaaru Kirist. Yónni nanu ko, ngir mu dénk leen, tey feddali seen ngëm,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nu daldi yónni Timote, muy sunu mbokk, di jawriñub Yàlla bu nuy liggéeyandool ci xibaaru Almasi. Su ko defee Timote dooleel leen, feddli seen ngëm,