1 Thessalonians 3:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba nu nekkee ak yéen sax, waxoon nanu leen, waxati ko ne, fàww nu sonn; te noonu la ame, yéen xam ngeen ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba nu nekkee ak yeen sax lanu leen jëkkoona wax ne dinanu daj ay coono, te xam ngeen ne noonu la ame.