1 Thessalonians 3:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ba ma ko mënatul a dékku, yónnee naa, ngir xam fu seen ngëm tollu, ngir ragal Seytaane fiir leen, ba sunu ñaq neen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax ba ma muñee ba tële, ma yónnee, ngir xam fu seen ngëm tollu, ndax ragal ne Fiirkat bi da leena fiir, ba sunuw ñaq neen.