1 Thessalonians 4:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te moom ngeen di def ci bokk yépp, yi ci diiwaanu Maseduwan. Waaye bokk yi, maa ngi leen di xiirtal, ngeen gën cee sax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te moom ngeen nekke seen digg ak mboolem bokki diiwaanu Maseduwan gépp. Teewul nag, bokk yi, nu di leen ñaax, ngir ngeen gënate jëfe noonu.