1 Thessalonians 4:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu dingeen dund dund gu jekk ci kanamu waa àddina, te it dungeen soxlaal kenn dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon dingeen jekk nu ngeen di jëflantee ak ñu gëmul ña ca biti, te dungeen soxlaal kenn dara.