1 Thessalonians 4:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndegam gëm nanu ne, Yeesu dee na te dekki, noonu it Yàlla dina indaale ak Yeesu ñépp ñi ko gëm te nelaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam gëm nanu ne Yeesu dee na, ba dekki, noonu it lanu wara gëme ne Yàlla mooy dekkal way dawlu ñi gëmoon Yeesu, ba boole leen ak Yeesu, indaale.