1 Thessalonians 4:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci lu jëm ci bëggante ci seen biir, matul nu leen di bind dara, ndaxte Yàlla def na ci seen xol, ngeen bëggante.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci wàllu mbëggeel gi war ci biiri bokk, soxlawuleen ku leen ci bind dara, ndax yeen ci seen bopp, Yàlla tàggat na leen ci soppante,