1 Thessalonians 5:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bokk yi, ci li jëm ci jamono yi ak waxtu, yi loolu di am, matul nu leen ciy bind dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nag bokk yi, lu jëm ci ay àpp, ak bés ya loolu di am, soxlawuleen ku leen ci bind,