1 Thessalonians 5:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
rax-ca-dolli ngeen naw leen seen kem-kàttan te bëgg leen ndax seen liggéey. Na jàmm am ci seen biir.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nangeen leen nawe seen kem kàttan te soppe leen noonu ndax seen liggéey. Gannaaw loolu, nangeen jàmmoo.