1 Thessalonians 5:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, nu ngi leen di dénk, ngeen yedd ñi feñaag, dëfël ñi seen yasara yàcciku, dimbali ñi néew doole, tey muñal ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, danu leen di dénku; yaafus yi, femmuleen leen; ñi néewu fit, ñaaxleen leen; néew-doole yi, dimbalileen leen, te it muñal-leen ñépp.