1 Thessalonians 5:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Saxleen ci baax ci seen biir ak ci ñépp, te bañ a feyantoo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.