1 Thessalonians 5:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte xam ngeen bu wér ne, ni sàcc di ñëwe guddi, noonu la bésu Boroom bi di ñëwe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax yeen ci seen bopp, xam ngeen xéll ne Sang bi, ni sàccub guddi lay dikke.