1 Thessalonians 5:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen di dénk ci kanamu Boroom bi, ngeen jàngal bataaxal bii bokk yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa ngi leen di dénku nag, ngir Boroom bi, jàngleen biral bataaxal bii ngir bokk yépp.