1 Thessalonians 5:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk nit ñiy naan: «Lépp a ngi ci jàmm, ba ne leww,» booba musiba bett leen, ni aw mat di bette jigéen ju ëmb, te kenn du ci mucc.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fa nit ñi naan: «Jàmm ak kaaraange dikk na,» fa la sànkute di dale ci seen kaw, ni aw mat di jekkee dal ci kaw jigéenu wérul, te kenn du ca rëcce.