1 Thessalonians 5:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nun ñiy waa bëccëg, nanu maandu te ràngoo ngir xare bi: ngëm ak mbëggeel, muy kiiraayu dënn, ak kóoluteg mucc, muy mbaxanam xare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nun ñiy waa bëccëg, nanu ànd ak sunu sago, te def ngëm ak cofeel, sunu kiiraayal dënn; yaakaaru texe di sunu mbaxanam xare.