1 Timothy 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Wax ju wóor a ngii te yelloo gépp kóolute: Kirist Yeesu ganesi na àddina, ngir musal bàkkaarkat yi, te maa ci raw!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem kàddu gii may wax, lu wóor la te jara gëm: Almasi Yeesu moo dikk ci àddina, ngir musal bàkkaarkat yi, te maa ci raw!