1 Timothy 1:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yàlla yërëm na ma, ngir Kirist Yeesu jëkk a feeñal ci man muñam gu yaatu gi, ma nekk royukaay ci ñi ko nar a gëm te am dund gu dul jeex.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye loolu moo tax man bàkkaarkat bi ci raw, ma dajeek yërmande, ngir, ci lépp lu nu Almasi Yeesu di muñal, ma doon ci misaal, ñeel ñi ko nara gëm ëllëg, ba texe ba fàww.