1 Timothy 1:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it nga dénk leen, ñu bañ a topp léebi diiney neen ak limi maam yu dul jeex mukk. Loolu werante rekk lay jur, waaye du jëme kanam mbir mi Yàlla tëral, wéer ko ci ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ne leen ñu baña topp léebi neen, ak limi maam yu dul jeex, ndax loolu ay werante doŋŋ lay jur, te jariñul dara ci liggéeyu njotug Yàlla gi sottee ci ngëm.