1 Timothy 1:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Am na ñu moy loolu, ba jeng jëm ciy waxi neen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am na ñu moy woowu yoon, ba lajj jëm ci wax ju tekkiwul dara.