1 Timothy 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci li aju ci yoonu Musaa nag, xam nanu ne baax na, ci ku koy jëfe ni ko Yàlla tërale.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam nanu nag ne yoonu Musaa baax na, ndegam na mu ware lees ko jëfe.