1 Timothy 2:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fii laay tàmbale nag: maa ngi leen di dénk, ngeen yóbbu ñépp fa kanam Yàlla ciy ñaan, ay tinu ak i ngërëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag li jiitu ci mboolem li may dénkaane mooy ngeen di dagaan, di ñaan, di tinu ak a sant, ñeel doom aadama yépp,