1 Timothy 2:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye na seen col di jëf yu rafet, ndaxte looloo jekk ci jigéen juy woote ag ragal Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
waaye nañu gànjaroo jëf ju baax, ndax mooy li jekk ci jigéen ñuy seede ne ñooy ragalkati Yàlla.