1 Timothy 2:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte jenn Yàlla kepp moo am, ak benn Rammukat kepp diggante Yàlla ak nit ñi, di nit ki Kirist Yeesu,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat jenn Yàlla doŋŋ moo am, benn Defarekat doŋŋ it moo am diggante Yàlla ak nit ñi, te mooy nit ki Almasi Yeesu,