1 Timothy 2:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
mi joxe bakkanam ngir jot ñépp. Loolu mooy seede si Yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mi maye bakkanam ngir jot ñépp, te jëf jooju lañu seedeele ca ba mu jotee, la Yàlla nammoon.