1 Timothy 3:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moom itam nañu ko jëkk a seetlu, ba mu leer ne amul ŋàññ, ñu door koo fal.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dees koy jëkka seetlu nag, ba muy ku mucc sikk, ñu door koo dugal ci liggéeyu taxawukatub mbooloo mi.