1 Timothy 3:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
waaye amaana mu yéex. Moo tax ma lay bind bataaxal bii, ngir xamal la, ni ñu war a nekke ci kër Yàlla gi, maanaam ci mbooloom Yàlla Aji Dund ji, miy kenug dëgg te di sëslaayam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir su ma yeexee itam, nga xam nooy doxale ci kër Yàlla, ci biir mbooloom Yàlla jiy dund. Mbooloom gëmkat mi mooy kenug dëgg gi, di cëslaayam.