1 Timothy 3:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sàmm bi nag, nii la war a mel: war na ñàkk ŋàññ, yem ci benn soxna, moom boppam te maandu; war na am faayda, man gan te am mayu jàngale;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njiit li nag fàww mu mucc sikk, di ku dencul lu wees jenn jabar, ku moom bakkanam, jiital am xelam, di ku nawlu, man gan, te mana jàngle.