1 Timothy 4:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xelum Yàlla mi wax na bu leer ne, ci mujug jamono dina am ñu bàyyi yoonu ngëm wi, di topp ay xel yuy fàbbee ak xalaati Seytaane.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noowug Yàlla wax na ci lu leer ne ci mujug jamono, dina am ñu wacc yoonu ngëm wi, di topp ay xalaat yuy fàbbee ak ay àlluway ceytaane,