1 Timothy 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Faaydaalal yëf yooyu te sóobu ci, ba sa jëm kanam bir ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu ngay def sam xel, mbir yooyu ngay pastéefoo ba sag yokkute bir ñépp.