1 Timothy 4:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinañu tere séy, di araamal ay ñam, fekk Yàlla sàkk na leen, ngir ñi gëm te xam dëgg man ciy jëfandiku ak cant.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñu ñooy aaye ab séy, di digle ñàkka lekk yenn ñam yu Yàlla sàkk, ngir gëmkat ñi xam liy dëgg, man cee jariñu te di ko sante Yàlla.