1 Timothy 4:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Saxal ci digal bokk yi loolu nag, kon dinga nekk jawriñu Kirist Yeesu ju baax ju regg ci kàdduy yoonu ngëm wi ak njàngale mu rafet, mi nga xam bu wér.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Soo dee xamal loolu bokki gëmkat ñi, yaa di jawriñu Almasi Yeesu ju baax ju xontoo kàdduy yoonu ngëm wi, ak àlluwa ju rafet ji nga topp naka jekk.